Youssou N’Dour - Xale Bi Songtext

Youssou N’Dour - Xale Bi Übersetzung

Non non non nonnnn
Non non non nonnnn

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo Ndaxté so mérééé, so mérééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)

Lou mounoul gnak faw dafaw am
wareef dafay mate
Lég Lég mou done lou doul neex
yaw sama dom
souba tax may waax
so magué di nga xaam

ndaxté so dioyééé, so dioyéé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma

wadiour ak dom
faw gnou y waxtane
féxé melni mbourok sow
ndem réro mouneta gnak
so Diaxléé, so diaxlééé
na sa khelmi dém
Dém ci say wadiour

Ni jamano mél
Tééy da cé baax
jubantil bamou thior
ndax momine dafay rooy
bissa ngui gnew
sou magué diarigne la
lép nga ci bami ndaw

Ndaxté so mérééé, so dioyééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)
Songtext-ubersetzung.com

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo

heuuuu xalé bi
né bougouma la merlooo
(xalé momine la yaw bouko merlo té dé ko bégueul)
Ndaxté so mérééé, so mérééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma

Adouna nii la xalé bi lé
sou bay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
sou yay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
(nangue ma deglo xel)
sou bay waxaté nga déglou ko
(bagn ma deglo xol)
Adouna nii la xalé bi lé
(samaaa dooooom)
sou yay waxaté nga déglou ko
(nangue ma deglo xel)

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo

haaaann Xalé bii
Né beugoumala merloo

Xalé bii
Né beugoumala dioylooo
Ndaxté so mérééé, so dioyééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalmaaaaaa

D.THIAM

Nicht nicht nonnnn
Nicht nicht nonnnn

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo Ndaxté so mérééé, so mérééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)

Lou mounoul gnak faw dafaw bin
Wareef dafay mate
Lég Lég mou getan lou doul neex
Yaw sama dom
Souba-Steuer kann wachsen
So magué di nga xaam

Ndaxté so dioyééé, so dioyéé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma

Wadiour ak dom
Faw gnou y waxtane
Féxé melni mbourok sau
Ndem réro mouneta gnak
So diaxléé, so diaxlééé
Na sa khelmi dém
Dém ci sagen wadiour

Ni jamano mél
Tééy da cé baax
Jubantil bamou thior
Ndax momine dafay rooy
Bissa ngui gnew
Sou magué diarigne la
Lép nga ci bami ndaw

Ndaxté so mérééé, so dioyééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)
Songtext-ubersetzung.com

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo

Heuuuu xalé bi
Né bougouma la merlooo
(Xalé momine la yaw bouko merlo té dé ko bégueul)
Ndaxté so mérééé, so mérééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma

Adouna nii la xalé bi lé
Sou bay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
Sou yay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
(Nangue ma deglo xel)
Sou bay waxaté nga déglou ko
(Bagn ma deglo xol)
Adouna nii la xalé bi lé
(Samaaa dooooom)
Sou yay waxaté nga déglou ko
(Nangue ma deglo xel)

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo

Haaaann Xalé bii
Né beugoumala merloo

Xalé bii
Né beugoumala dioylooo
Ndaxté so mérééé, so dioyééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalmaaaaaa

D.THIAM


Zuletzt bearbeitet von: Anonym

Übersetzung bearbeiten